|
| | Philip Monteiro - Sama Wooo lyrics | Yeah!
Sama fans yi
Magui len di gueureum
(Ci lepp lounguéne di déf pour mane)
music bi
pour yen la
Oooh
Mane nop na lene
Woooh !!
(Dégloul lii)
Yageu neu lool
(Yageu neu)
bingueu déme
mane reer na
reer na sans yow
lan la wara def
(wax ma)
def sans yow
(sans yow hey)
Héy dama la soxhla
té dama la begueu wo
dem gueu té bayi ma
(bayi ma si leundeum)
wanté xam gua ni
ni dameu maneu doundeu ba tey
(dem gueu té bayi ma)
baby gneuwateul si mane
xana degueu to sama wooooooooo
(Refrain:)
Baby gneuwateul
yagueu lol bi gua démé
tax na sama xol weet
lou may def ba gueu gneuwat gneuwat si mane
Baby gneuwatal
yagueu lol bi gua démé
tax na sama xol weet
xana di leu waax beuss bou né fi gua tolou ci mane
(Ooohh)
Bou ma togué di xalaat
(doundeu you nex gui gnou done doundeu)
Rekeu sama xool fess
(xama tou ma lou ma wara def)
dem ngua bayi ma thi leudeum
(wanté xam gua ni)
dama wara doundeu ba tey
(dem gua te bayi ma)
bayi ma si leundeum
dama la soxla
dama la beugueu
Baby gneuwateul si mane
xana deguo sama wo
(Refrain:)
Xama tou ma li ma wara def
Ma ngui lathie ndaxté yaa ngui khalaat ci mane
bougou ma nga xaam li ma dadj
ndax xam na né am gua kenen
meunou mako gueum
(Bo amé kénén kon waxmako)
meunou meu dess ni
(Ci leundeum)
yagueu neu lool bigueu deme
mane reer na nekeutofi
Man lan la wara def
(Ma ngui lathie ndaxté yaa ngui khalaat ci mane)
dama la soxla
dama la beugueu
Baby gneuwateul si mane
xana deguo sama wooooooo
(Refrain:)
|
|